Aaqu Liggëy kat
Bepp liggëy kat waar na xam aaq ama k yeelef am . Xolal seen saas ak saarta bi leen di boole.
Saas liggëy kat bi
Jokkante liggëy kat ak njaati yi un ngi tekk ci saasu liggëy kat bi, yoon bi xamal kune waaref am. Teeri bi mooy firndel yoon liggey kat yepp.
Saasu liggëy kat bi daay wax ci xeetu ak woondu kontra yi , maasalan diir bi, faay gi ak ci teewal kureel lu liggëy kat. Daay wone li gëna neew ngir moo nee, takku mboolo mecce mooy tëral ni mooy tëddé ci tund w une.
Takku mboolo mecce
Saartu Liggëy ci Españ da faa am lu un ko beeral , di wax ci naaka liggëy ak jur kôm di tëdd ci mecce bu ne: takku mboolo mecce. Kureel ligeey kat ak njaati yi da nuy kay waxtaane ba takk ko ci mbiir tëral seen dígnate.
Am na xeeti takku mboolo mecce yu baari ci gox b une ci reew mi, tund yi ak dekk yi. Xolal ci kanam bu and akk sa mecce ba liggëy bi ngaay def, seet ko ci buscador bi.
Liggëy amn sañ sañ bokk ci Kureel bu xeq aaq ak yeelef am, te bokk ci waxtaan yi ci antarpiriss.



