- Inici
- Dëkk Kataluña
- Ci walu njàng ak formasoη
Ci walu njàng ak formasoη
Lacctel ci njàng mi téddé
Wara mana jàng dafa nek warugar bep domu Adama. Ñi fi nek tey ay dokhandem ci rewmi te am at yi wara tax ñu jàng, warugarla ci ñom rewmi tegal matuway yep pur ñu jàng te duna ci fay dërëm, war nanu am lijasa binu beg ak tamit jot ci ndimel yi war ci sen jàng.
Ci buntu bi dinga fi giss information binge soxla, yep ci walu wowu pur mana jàng wala continue sen jàng, ci lu jem ci njangu xaleyi ba bangay dem Universite, wala tamit yenen xeti jàng yo mana def te do tew.




