Xaleyi
Xibaar ak peexe yi jaklel xaley
Ay na pexe ak yoon yu baari yu nu jakklel xaleyi Bërëp foo yi, bërëp njàngal mecce ak wut liggeey, ndimël ngiir mënël sa bopp.
Foo
Kër xaleyi ay bërëp yu nu ubbi ngir def mbir yiiy jëriñ xaleyi njàngal leen seeytu mbiir yooy te tëral seen doxaliin.
Kër Askan wi ay bërep yu amal ay yëngu. Bërep yu nu ubbil askan wi yeep lañ, di naan fay amal xeetu njàang yu ne deme ni: tôgg, sinema , teyatar, coosanu aada, ak yeen nak yeen. Amna yeen ni këri xale ak dallu kay yu saaw ci Kataluña ngir yoombal tukki xaleyi.
Ci jamonooy Nawet, mbootaay yu baari ak yeeni dallu kay da nuy amal ak yëngu bër ak dàll jakklel ko xaleyi: kampama, sancer, jokko ak bitiim reew, ba bokk ci voolonteer yii dem bitiim rew ba tukki ndimbal.
Njàangal ak ligeey
Peexe yi am ngir njàngum xaleyi ak seen ligeey wootul leen lu dul tekki xaleyi yi ama gul 25 aat . Daara yi ak bërep njàangu mecce ay nanu ay banxaas yu jàppale ak xelal. Tamit ay Mbotaay yi ngi def lu ni deme di mootali banxassu ngor gi. Neep anda boole peexe yi ci daaray ak lël njàngum mecce ngir xaleyi am ci lijassa.
Biiro wootum ligeey yu xaleyi daay xamal ci beepu xettu ligeey, te diigal ay yoon, di naay xelal tamit, te ubbi yoon ngir mën ko def ci internet.
Werguyaram
So bëgge ku la xelal ci sa werguyaram, mën ng adem ci yoon yi nu ubbi ci internet yu deme ni mbiir sëy, sineebar ay taam loore, tolof tolof ci lekkiin wi, ba peercinc wla taattu.
Amna ay bërep yuy jooxe xiibar ci mbiiru werguyaram: “elpep.info”, “laClara.info” ak “Sexe.joves”.
Xaleyi ak daxaar yi
Amna ay doxaliin ngungee xalye daxaar yi so ga aksi Kataluña ngir nu xam dekk bi, xam yoon ak mbotaay yi fi ne, ba xamal toppo askan wi. Been ci doxaliin yo yu ne bu Casal dels Infants del Raval bi ne ci Barsaalon.
Ci biiro xibaaru xaleyi di naay wa am beep xeetu xibaar bu soxlo ci mbiir yi jakkle xaleyi.
Bepp xibaar bu un jakklel xaley yi, mën nga aam ci biiro xibaar xaley yi FEPP ci Kataluña.



