Ci walu indi sa njabot

Yoon bi un tëral ngir sa njaboot

Bo ame kayit gi tax nga wara dëk ci rewmi, yoon maynala nga mana indi sa njabot sa bula yitele.

Ku mana indi njabotam?
Ñinga xamne dëk nanu Espagne ci lu tolu ci at te un ame kayit rewmi pur nekat fi lu tolat ci at.
Lunu ci lath pur indibi muna yomb?

- Dundu bu tax sa njabot man fe ñew?
- Am xaliss bu tax sa ndjabot bunu nekek yaw dunu sonu.

Kan lanu may mu man ko saku?
- Sa Jekër wala sa jabar
- Say doom, wala ñinga yaral sa bop.
- Sa njabot ginga xamne yalen di dundal
- Xale yu ndaw yi tolu ci fuki at ak jurom ñet, wala ñi ame lago bu feke ne si yaw lanu joku.

Ban kayit la nuy am sa njabot gi ñëw?
Kayit residans bu tolu ci ap dir.

Fan la un koy ute?

Ci biro bi yengu ci walu ñi fi ñëw.