Lu la Teranga mën Won?
Peexe yu jëriñ ci bo bëgge dekk Kataluña
Geew ngir book defar ak xamante
Xibaar ci mbootayi doomi Senegaal yi
Màcc. Maa ngi dekk Kataluña
Liggëyal keneen
Peermi bi daa maay doxandeem sañ liggëy ci bërê liggëy boo xamna daay faaye ko...
Fooy wutte liggëy
Booy wut ligeey , amna pexe yu baari yu la mëna dimbali ci segg liggëy yi taxaw....
Aaqu Liggëy kat
Bepp liggëy kat waar na xam aaq ama k yeelef am. Xolal seen saas ak saarta bi leen di boole....
Kayit biy wane fi nga dëk
Kayit bi wane fi nga dëk moy bindu ci goj binga dëk, sa Mairi...
Kayitu residans
Pur nga dëk Kataluña danga yitewo kayitu residans. Kayit gogu mana nek ci dir bu gat wala mu nek ba...
Ci walu indi sa njabot
Bo ame kayit gi tax nga wara dëk ci rewmi, yoon maynala nga mana indi sa njabot sa bula...

Calçotada
Calçotades a nadje y ndabot yi di faral di def, muna nek feta k ay mbok wala xarit, lunu fonk la ci rewu Kataluña....

Fricando bu and ak bolets
Fricando bu and ak bolets, ñarelu plat bu am solo ci rewu catalan....

Crema catalana
Com ninu ko tude, crema catalana moy deser binu gana xam ci Kataluña....
Tërelin
Setembre 2010
| Setmanes | Dl | Dt | Dc | Dj | Dv | Ds | Dg |
|---|---|---|---|---|---|---|---|
| setmana 1 | 30 | 31 | 1 | 2 | 3 | 4 | 5 |
| setmana 2 | 6 | 7 | 8 | 9 | 10 | 11 | 12 |
| setmana 3 | 13 | 14 | 15 | 16 | 17 | 18 | 19 |
| setmana 4 | 20 | 21 | 22 | 23 | 24 | 25 | 26 |
| setmana 5 | 27 | 28 | 29 | 30 | 1 | 2 | 3 |




