- Inici
- Dëkk Kataluña
- Bërëp jappale yi nu jakklel doxaandem yi
- Ambasad ak konsula
Ambasad ak konsula
Niii fi toggal ngooru Senegaal ak askanam
Ambasad jawriñ ju fi toggal ngoor beneen reew. Naari ngoor ci moom lanni jaar ngiir jokko ba tagg ap ligeey demi pëlotik Ba xamaal aada. Ambasad yu baari da leen di toftaal konsula.
Ambasad yi nooy toppato mbiri ngoor, konsula bi di lijanti mbiri yi doxaandem yo demani defaarat kayit.
Ambasad been lay doon ci reew ; waaye konsula seen limam ngi aajo ci dekku taxi yu magg yi ak doxaandem reewma ya fa dekk.
Amabasad Senegaal fi ci Españ moo ngi ne ca Madrid ci aderess bi mbendum Príncipe de Vergara naatup 90 telefon bi di 91 745 1003.
Konsula bi ci Barsaloon ne ci mbendum Balmes naatu 185 telefon bi di 93 200 9722.



