- Inici
- Ci katalan
- Jàng ci Internet
Jàng ci Internet

Acollida
Ay fo ak fowukay ci lak catalan.

Alumnat nouvingut
Ay material pur jàng lak catalan pur ñiy soga ñew ci rewmi ci toluway bu nek.

Barrina
Software buma xamne ay exercice pur jàng kat yi ci toluway yu ute ci lak catalan. Amna 16 tems ak 20 exercices.

Centres d'autoaprenentatge de català
Set ay Centre yo mana jangale sa bop catalan.

Cercador de recursos per aprendre català
Setukay fo mana jange lak catalan ci lu nga xamne danga koy def ninga ko bëge.

Dacco
Pur nga conjuge ay verb ci catalan.

Dictats en línia
Lu tolu ci 188 dicte am nafi, yu ci toluway yu yam, yu dig domu ak yu kawe. Dicte bu nek text bunu bind (archive PDF) ak tamit noko mana deglo (archive MP3).

Edu3.cat
Radio wala tele yuy jangale ci Internet, ci lu tolu ci 2.200 audiovisuels ci walu xam xam, ci lu jem ci mbiri jaw ji, mbiri social, lak ak literatura, tecnologi, matematic, mbiri artista, tagat yaram ak yu deme niki nonu.

Edu365.cat
Fo ak exorcice pur yok sa xam xam ci walum njàng.

El mercat
Wax yu jem ci walu jaba ci deglu, video ci walu lek yi ngay soxla.

El món per un forat
Wax yo mana deglu, giss ay fotos, ak ay desin. Ci walu yu bari c ijaw ji ak mbiri social.

Endevina
Software bu ay exercices pur kuy jàng ci toluway yu bari ci catalan. Amna 16 tems ak 20 exercices.

Entrena't per llegir
Ay exercices pur jàng lir lak catalan ci ñati taxaway.

Exercicis d'ortografia
Exercices pur boy bind baña def fot yu bari ci laku catalan

Galí
Guide bulay dimbali pur nga fangal sa bop lak catalan. Amna ay exercices ci yu bari te wute ci Catalan bici central, noroccidental ak alguerés.

Interc@t
Njáng ci Internet ci ay activite pur Kramer, ak xam batí ci catalan.

Jocs de paraules i passatemps
Amna ay fo ak lo mana raye teng bi ci catalan.

La vaca Paca
Ay lep yunu desine nga man ko deglo ba nga man ko lir.

Lletra per lletra
Ay exercices pur jàng bind ak lir lak catalan.

Paraules
Ay exercices pur jàng bat yi ci catalan.

Parla.cat
Ay cur pur jàng catalan, ci lo mana jàng lak bi ak ñenen. Dangay Bingu pur mana bok.

Pronoms febles
Jumtukay bu yomb te gaaw ci walu defar ay bat.

Pronunciem
Ay activite pur nga mana jàng ci lu gana yomb bat yi ci catalan central.

Saber-ne un niu
Sofware bu ay exercices yu nga xamne jàng katyi no ko def ci catalan. Amna ci lu tolu ci 11 tems.

Vincles
Ay jumtukay yu un desine wala nga man ko deglu pur xam li ñu jublu ci lak catalan.

Viure a Catalunya. Comencem a parlar
Ay waxtan yu yomb ci walu dundu mi pur ñiy soga eksi ci rewmi. Ay waxtan yunu dajale ci tem yu bari. Ay waxtan yo mana lir ci PDF wala nga man ko deglu ci MP3.

Viure a Catalunya. Vocabulari en imatges
Ay bat yunu desine yu jem ci nit ñi xamul lak bi. Amna ñari xath : Ben bi di ay bat yu and aki natal, beben bi di waxtan yu yomb. Bu ci nek mungi ci lak catalan, español, France, angle, italien, aleman, arab ak chinois. Amna goj dëk bimu amb ak gogu aduna bi yep.

Vivim junts. Materials per aprendre català
Amna material bu nga xamni par tem la, pur ñiy ñew ci rew mi.

Voluntariat per la llengua
Site Internet pur weccok ñi buga jàng lak bi ak ño xame ay wolonter yu baga jàngale laku catalan. Dinga fi fek lu wan yon wi ci walu wowu.



