- Inici
- Dëkk Kataluña
- Kër
- Asiranss su kër
Asiranss su kër
Aar sa dekkuway ci yeen tolof tolof
Soo bañ am yeen tolof tolof ci taabax kër gi, bagass yi fi def, li gën mooy nga wuttal ka asiranss, booy aae yepp bess bu la donηal dale.
Tayit bu fekke donηal li lal yeen kër yi nga bokkal taax, asiranss mooy jël defaarat bi baa ak ndampaay kepp ku ci yaxule.
Mën wlacc ni kooy amee, tëralin ak njëη ci anterpiriss su asiranss yi.



