- Inici
- Yëgle ci nooy yoon tërele
Yëgle ci nooy yoon tërele
Xibaar ci ni Yoon teerale jëffandiko web bi.
Teranga.cat mbëbett Fondasoη Pere Tarres, di ka ci jappalè Njëriñ ji yoor seeytu ngooru katalunña jaaré ci sakarataria bi nu deη xarale yi ni jokkalante yi ak mbotaay xibaar yi.
Wareef yi yoon tek ci web bi, jubblul ci ngir tekk teeralin ci nii niiy jëffandiko web Fondasoη Pere Tarres ubi l askan wi ci URL bi http://www.teranga.cat. Jëffandiko web bi ci kumu mën ti doon su bëgge mbokk ci nu koy jëffandiko daay naango teeralinn wi nu ci xibaar bi.
Keep ku di ni jëffandiko web, daay joxé kaddoom ci ne, liin ci mbind ba deff deey aand ak xibaar , yaar ak jaamu askaan wi. Tamiit mbind mi ak deffiin li ko yiitel daay ne lu léw ba dëppo k xibaaru yoon bi, set ci lepp lo xamn tooñ nit la ba luuy yax ba di feqé ba web bi keen du ko jéffandiko.
Tamiit ki kooy jëffandiko daay joxé kaddoom ne doo yax ba sopi wala bëep xettu yax mbind yi ba ba xarale yi ne ci web teranga.cat.
Siiwal
Web bi mëness na ci deff ay siiwal xew xew ba mbiir yu ni kay Jëffandiko di tekk ci pacc yi jakklel ci web bi (deeme ni alluwa yëkkle yi mayeb liggey), boroom siiwal moom koot mo yoor waarugar fexi ba mu dëppo ak yoon ci mbind mi ak yeen xetti xarale yi muko deffaré. Teranga.cat ak Fondasoη Pere Tarres daara teggu wul ci sen loxo ci njumte ba, lu andul ak degg ci liin ëmb siiwal bi.
Ak lu mén di aam, so aame looy njaxtu ci ëmb siiwal yi yi ne ci web mën jokko ak ci mail bi: teranga@teranga.cat.
Aajo moomel
Leeb lu ne ci web, moo nattal, ba mbind ak loomu mën ti doon, lu wutté lu noo waxante, Fondasoη Pere Tarres moom ka ba geneen, maay na mbootaay gi mo jërino ko.
Kiiy jëffandikoo web, naango na ne sooti ko, ba joox ko, ba jaay wala sopi, bëep xettu jëriño yeef yi ne ci web njalkati yoon ci wal moomel gi Fondasoη ba jaambur yi joxé.
Waaruga ci jëffandiko web bi
Jaambur biiy jëffandiko web , moom donη mooy ki nu tekk beep njumtée ba njalkati bu mëna aam, ba yaaxal keneen bu feeñ ci web bi, baa taax Fondasoη bi, nii kooy japple ak leggey kat, niiy taxawalaata amul dara lu leen nii taaxal, ci jaambur bu jëffandiko web bi def.
Fondasoη uff ken ci ay njumtee, ba lu dul degg wala fatté ci liin deff ci web tee ñu mën se jot.
Jambur bi jëffandikoo web moo donη mooy taxaw ci gànaamu yoon beep kalaamé bu ciib ci lu moo mbind ba tekk ci web. Moomiit mooy ki faay leep lu waar ci attée bi ak ndampay Fondasoη bii aam ci mbiir mi.
Waareef ci jokklo yeen web
Jokklo yi ba links dina maay kiiy jëffandiko, moo aksi ci yeenen web bu mbotaay, Fondasoη tekkoowul dara ci xibaar yi ni yeneen web, ndax link yi yombab xibaar rek moo taax mooy aam te aajo ci mbiir mu rañee.
Fondasoη yoonaam newul ci ndoxaliin web, caa li ngi ciiy saako, wooluteem ak sell ngi aam ci li mu ëmb ba ci xiibaram, tamiit ci tooñ yu mëna deff neneen.
Peexe aar xaamee ci nit ki yi aamé ci web
Ci laac yi jaambur di toontu mën ci xam jaambur bi: Been tolof tolof du aam ci joxe bi, ba lu méen lore jaambur bi joggé ci web bi, jaambur bi joxé xamee yi daay maayé kiiy seeytu Teranga.cat buy jëffandiko ci aanam yiim ka bëgge.
Jaambur ba ki mu yaabal mën saako li moo jaxé ngiir soope ci leen, baa diindi ko, ci mbind mooy yooné teranga@teranga.cat
Fondasoηdi joxé kaddoom ci aar xamée, jél ay mattookay yii tax kenn du sopi ba yaax, reeral, ba def ci lu ko maayol jaaralé lo ko ci xaralé, b jot ci ci lu nu maaye wul wekko ci aar ak xol xaralé yi ko teyyi.
Seetlu yi jaambur di def
Jaambur biy Jëffandiko web bi, deey saamo dugul ci web jumtuwaay, mbind ak seetlu yo xamne xamée yu mu joxé yu wër la, tee aand ak yoon moomel ci xalaat, ba deffar jaambur, ak yeneen xettu dengaane ci yoon.
Xibaar,jumtuway, mbind ak seetlu bi jaambur bi di jox Fondasoη mënul nil u niiy nëbb, ci seeytu web nooy xol ni koo jërinoo.
Sopi ci wareef fu Jéffandiko
Fondasoη bi moo aam sañ san di sopi, ba yokk, yessal wareef fu jffandikoo web saa yu ko sope tee du yëggël kenn. Ca sa sa la jaabuur di ko topp yoon wi moo tëral sa yu duggé ci web, loolu tax ba sa su ne waar na di ko njàng.




