Teranga - Yoonu jokko Kataluña ak

Cadaqués

Catalunya        

Ne ci biir tefess su Kosta Brawa

Cadaqués dekk bu tutti ci diiwaan nu Sirona, ne ci gooxu Emporda ci kaw. Dekk bu ay coxaan ci napp ak mbiir yi fette geej. Meelin nam, waqam ko ak tefess am deff na de yoon turista yi ci Kosta brawa.

ca Cadaqués la kër Salvador Dali nee ci peggu waq yiggat( ci bëcc gànnar dekk bi), foo fe la pintar bu ëpp daayo bi dekk ak Jaabaram Gala ci att yi mu mujjè dund. Këru nàppkat bu un deferaat la. Mëness nañ fa sett fa mbaaram ba daan ligeeyi, ak yeen naatal yi mu deff , nékk yi, bayotek bi ak ëtt bi. Bokk na fi ëpp di teeru nit ci diiwanu Amporda , loolu waral ba bu fa bëgge dem fokk nga wooute ci telefon bi 972 25 10 15 ba ci web bi, bu wessu nag Jeeli kayitu dugg bi lu tollu ci geenwala waxtu ba noo dugg ci sett bi, xol waxtu ubbi yi, ci njëŋ yiak yenne ci web bi Fundació Gala - Salvador Dalí.

Am na feneen fo mën deñ ci bu soori wul Cadaqués, mooy dem ca Parkjuddu ak suuf bu Kap de Kereuss, cbolk ci alla yi geena rafet ci Kataluña.

Fu jeggé ak Kapm ci bëcc Salum kosta brawa, am na dekk bu tudd Eskal a. Boo koo toolo ci naari kilomete di giis li dess ci jamono gerek yi ay romins Ampuriyas. Ci Buntu bërëb bi amna misé dessun taabaxu coxaan yi ci Kataluña ci Ampuriyas.

Bokkal        

imatge Foto de Santi MB. Llicència cc (by-nc-nd)