- Inici
- Fii ba fëlé
- Ruxu yi
- Casamance
Casamance
Yeeme ci mbindem
Casamance tund ci beëcc salumu Senegal ak Gambi. Un wax ne moo dax ci Senegaal. Ay la yewoon, tefessam yi ak gancaaxam bi ak tangoor taaxna ba tukki kat yu baari di gëna setti.
Fii ci gëna fëss mooy Kap sikirinŋ fii epp turistas ak waaye tefess yeeep ci kaw ba ci suuf ba Kafuntine lu ni mel nga faay fekk: tefessu suuf su wex, weet ak ndox mu nex.
Nii ndaaje Salum ci bëc gà nnaru reew , dexu Casamance ay geej seen ndaje day wone bërëpp yu rafet ci ndox mooy wal ak dekk wër ndox . rafet ci xol ak doxantu ak mbeggé ba li gën gaal , jaafe wul nga am ko ci kap Sikirinŋ ba Eliin kinŋ, ba karabaan wala Siggicoor.
Jaar na dem ci dekk bu mu jë bi nadx am na cooxan te ak nittam toolu nañ ci 20000, mooy capital bi. ci dexu Casamance amna ay peexe yu bari ci wonne wu ak taabax yu deppoo ak dtund wi, ci daal yi ci dekk bi dekkuway kaw ka yu nit yi yoore , te ci jampono am boroomi afers jël ko di kko defaarat.
Foto de cfarivar. Llicència cc (by-nc-sa)



