- Inici
- Mbotaay yi
- KASK
KASK
Kureel Kordinadora
Kask dafa êmb mbotaay doomi Senegal yi dekk ca Kataluña.
Kureel gi noo sanc ci aatum 2003 di seentu japple mbotaay doomi Senegaal ci tëddin fii ci Katauña. Ubbi ay yoon ci jokko ak waxtaan dikkante ngoor Kataluña, Españ,ak Senegaal.
Kask ci coobaare ak njanx laafu mbotaayi Tarrasa, Barsaloon ak Mataaro. Kureel gi nekk lu un laccoon, ngir yenηu wa Senegaal gëna rafet te di yokk NET.
Mankaanu Kask ne ci Barsaloon (C/Comerç, 42), Mëness jokko ak Koordinadora ci telefoon yi 93 551 05 42 Ak 664 824 344 ba yoone Imel ci cordinadorasen@yahoo.es.



