- Inici
- Fii ba fëlé
- Coosaan
- Kasteye yi
Kasteye yi
Cosaanu defar taata ak ay nit
Kasteyes yi aay xew xew aada laan ci gëna fëss ci Kataluña. Kastey lii doŋ la nit taata bu ay nit yu yaanunte def Baa moo kawé tollu ci ay metar yu baari.
Wërr fu mu sosso dina un yobbu ba gox yi yi Walenss, daana ka ci dekk bi tudd Riibereña bu Algemesí, foofu laan da amale di fa amal ba leggi la MuiXeranga, aad fecc ay taata yi. Bind yi ci cosaan mababoor fecc kat yi un saaw doxaliin bi ci reew mi. Ci noonu la aksi ca Tarragoon, Bày, jël fecc mi “tuddi feccum Walenss” (ci niino ko Xamee Woon), bu mi tolloo ci funk ay juroom naar ci teemeral aat ci arminatu Insa, ci naan tambali weer fecc mi ci defar taata yu gëna kawé.
Pàcc yi ne ci kastey naat laan: ab piiña ba toggu bu nit yi di defar ngir teeyé ko (yànu ci mbaaga yi diisa yu taata bi), dàtt gi (mooy etass yi teggu ci kaw) ak bucc bi kaw, ay guney nooy fetté ci kaw kastey.
Pexe yi melliin yi niiy defaré kastey baari naan te wute, wa yepp ci naat yooyu laay tedié. Seen tur gi aajo ci yaatu Waay (naata kasteyé ci etass b une) ak taxawaay (naata etass ci kastey bi) masalaan ñeent ci juroom ñeent (ñeent kasteye ci etasst b une ak juroom ñeenti etass). Méness na ci yokk naari pacc yu ka teeye: xamee fulre ( naarel lu piina ngir jubbel taxawaay ak mooytu daanu) ba maaniya ( naatel teeye kaay, ne ci kaw fulre bi un gën ka rañé ci juroom ñeent yi ci funk).
Kasteyee yi ni sol tubeey yu wex , laajo sër bu ñul , fular ak semiss bu aam melo mbaboor mi. Un amal ci yeen xew xew yi: deme ni ci bessu dekk bi, b bu boroom dekk b iba joŋŋante mbaboor ri kasteye. Mbaborr yi taam di taase ci gox yi , Barsaloon ak Tarragoon . Ni gëna njaaxlaw nak un gi joggé Wilafranka bu Penedees, Baay, Tarragoon ak Tarrasa.
Foto d'Albert92. Llicència cc (by-nc-nd)



