- Inici
- Dëkk Kataluña
- Kër
- Jappo ak dekkëndo yi
Jappo ak dekkëndo yi
Seyt dekkandoo gi
Bu xêsse ba dekk ci kër gi, nda ngay bokk ci mbollo dekkëndo yi.
Mooy tekki setal bi ak bërëp yi ngeen bokk ak waxtu yi mën am coow nindaay wi ci saart bu leen di tëral. Ni miiy doxé ak yoon fii ko lal nda nga wwara xam te toppe ko. Amna njiit ( lu ci baari njitu dekkëndo yi) bi nga xamna kepp ku faa dekk di na ko ne, mmom ngay lacc ñaata laniiy naat ak yeenen pac yi bokk ci seeytu bi.
Am xollu muñ ak yaar di yombal dekkin wi.



