Kurrikulum witee bi
Kurrikulum witee kayi booy firnde ci anam gu rafet te métt ssay mën mën ak xarañ ci mecce bi, saay lijaza si liggëy bi ngaa wutt.
Kurrikulum mooy li giss giss bi niiy jëk am ci yaw, ba mën la taan ci yakaar mën naan liggëy bi.
Kayit war na am sa tuur, sam njàng ak xarañ ak liggëy yi nga deff yeep (wonne liiñ la saasoon ci liggëy yo yu ak diir bi). Mën nga ci yokk lepp lu lu mëna wone ba xamal saa mënin. Bu aande ak baataxalu bu laay woné ak bu diggële. Biiro wuttum liggëy amb ay jumtuway ngir bind kurrikulum si numu gëna gaawee te yomb.



