Li la yoon may si walu li ngay jefendiko

Laccte ci wallu yoon ci jënd ak jaay

Com jdend kat, dina am solo nga xam li la yoon may pur sa bo ame problem ak ñiy jay.

Amna bërëb yulay japale ci lolu, say bunu la naxe wala ñu la toñla, toñ bumu mana don. Ñoy mbotayu yi lay watu ci walu wowu tenga munlena seti sasune.

Ci walu Cataluña, amna kurel gu mak guy yengu ci walu wowu muy Agencia Catalana de Consumo, binga xamne mi ngi weru ci departemeng bi yor walu koparyi.