- Inici
- Dëkk Kataluña
- Dëkk
- Kayit biy wane fi nga dëk
Kayit biy wane fi nga dëk
Bindu ci Teere bi jël ci dekk ci dekk bi
Kayit bi wane fi nga dëk moy bindu ci goj binga dëk, sa Mairi ba. Lou am solo la, ndax moy wane yagay bi nga am ci goj bi pur mana am bep xetu ndimbel bou goj bi did def ci lu jem ci walou faju, jàng.
Fana la nuy ute kayit bi?
Sa Mairi ba ci goj binga buga dëke
Kan moka wara saku?
Kep ku nga xamni muskalaf la, bathi ñi amul kayit residans.
Ci ñata teng lay tol pur ñu sopi kayit gogu?
Ñari at yu nek, ba bangay am kayit residans.



