Liggëyal kaneen

Lii nu bind fii am nañ Tekki wi ci Kaalama Al pulaar.

Yeen ci liggëy yi aam ci Kataluña mooy liggëyal as njàtiggi ba boroom antarpiriss. Bo ka bëggé di nga soxla kayitu gu laa ko maay. Mooy kayitu sesour ak saanu liggëyal keneen. Kayit Gough mooy maay doxandem bi saan saanu liggëy teey amu paayor weer. Wutt wisa liggëy sa dekk ba nga badekk nga wutte , gànnaw nga kontra liggëy bu toolu ci at. Bu fekké fii la ne , daay lacc mu nekkin bu teggu ci yoon.

Ku mëna lacc?
Njaati gi moo wara lijjanti peermi bi aand ak kontra liggëy kat bi. Bu njaati waxe soxla ci jêl liggëy kat, day jot toontu bi sañ sañ dekk ak liggëye fi, bi joox surga bi. Kiiy defar kontra di na di yoone tontu wi gàanaw sotti ko waliyaan sa reew am ngir moo mëna naan wisa ca konsula bi gëne jekke. Waliyaan bi waar neew Españ ci lu dul weessu naati wer gàanaw bu jotte wisa bi.

Bu akse njaateem gi amna wer ngir binda ko ci Sekirite sosyal bi lijjantil kayitu dentite doxandeem.

Yaan kayit ngaay wutt ?
Liggëy kat waar na wut kayit yi te nu baax :

— Kaasiye siduseer
— Sertifika medikal
— Naati nattal
— Kayit bi firnde sa xariñ ci sa mecce
— Sotti passport bi ( bu akse Españ)

Njaati gi mmom yi kayit laay jooxe :

— NIF ba CIF
— Numero bindu ci sekirite sosyal ba leneen lu firnde ne dugal na ko
— Sakku liggëy kat amb lepp lumul andal ( liggëyu kay war na bokk ci liim bi teeral liggëy yi jaffe giss ko kaay def. Ba moom sertificat SOC bu wonné giss keen ku ka bëgg)
— Raporu antarpiriss bi ak liggëyu kay bi
— Si bu nu soxla kayi buy wonne ni antarpiriss am kôm maay bu waaye di am

Fo kaay wutte?

Ci biro I toppatoo doxandeem ( subdelekasoη koberno) ci tundo bi nga waara liggëye.

Yeesal

Peermi bu jëkk bi att doη laay am, te been mecce laay doon ci ween tund . bu wesso at mi, di nga mëna yeesal ñaari ri yoon ci li toolu ñaari at, (yeesal peermi yoyu) ba moo matt juroom at yu fi dekk te amul dogg dogg, di am peermi dekk ba faaw.

Booy yeesa peermi di soxla wonne naat ci sekirite sosyal lu tollu ci xacc at yi mooy am. Bi
jëk di 12 wer , mooy waral 6 wer; Yi toop bu yeesal mooy at.

Peermi residenss ba faaw mooy juroom at yu ne danu kaay yeesal wa keen du lacc diir booy naat ci sekirite sosyal.