Xam xam

Seddé

Ay netali, ay jar jaru ak ay projets ay senegale yuy dundu Cataluña moy li nuy wane ci video yi.

 
  • "Kepp ku ñëw fi, ñëw fi ngir taxawaalu, liggëy ya ko yékki"

    Amadu Bokar Sam moo newoon jewriñ ni deŋ doxaliin ak seeytu bu Kask , Kureel gi ëm mbotaay yi Senegaal fi ci Kataluña. Jaar ci Kureel, raané naan liggëy am ci prosé bokk kom koma k Senegaal.

  • “Ci fi mu gana mete dimbali nanu ma”

    Tolú naci jurom ñati at Fátima mungi dundu ci Barcelona. Bu fekente ni togame ci rewmi metiwon na, legi mi ngi tok bu bax ci Cataluña.

  • "Bugguma jaay meloo wutté naaw ci Afrik"

    Sidi mooyki soss siiwakkat teere yi Takusan, di tekki ci katalan “capvespre”. Di jamono jo xamna bu suuf sedde, njàng aab teere daay nex.

xolal:

       
  • Senegal       
    Cooperant a Senegal

    Cooperant a Senegal

    Ki gu Mbind: Gerard Graells. Tècnic de l’àrea d’Àfrica Subsahariana de l'ACCD

    A les acaballes de la carrera tenia poques coses clares, no obstant, el què sí tenia clar era que volia treballar i professionalitzar-me en l’àmbit de la cooperació internacional pel...

    xolal yeneen ( yi nee ci ëmbi):

  • Senegal       
    Dos catalans a Senegal

    Dos catalans a Senegal

    Ki gu Mbind: Laia i Xavi

    Hem de reconèixer que ens va ser difícil adaptar-nos-hi, era la primera vegada que viatjàvem a un país tan diferent d’Europa, però ara podem dir que va ser una experiència que no...

    xolal yeneen ( yi nee ci ëmbi):

Bokkal        

lepp lu ni fii siiwal ci lakk ki go mbind nanu kay ba

nataal bi