- Inici
- Dëkk Kataluña
- Bërëp ndimbal askan wi
- Njaboot gi
Njaboot gi
Dimbël yi njaboot yi ci wal kom
Njaboot gi poη bu reey ci askan wi, loolu taxna ba bërëp yi ndimbal le sàss nan leen un aar ko, naam ci koom ak degglu.
Ndimbal ci Koom
Fi ci Kataluña amna ay xeeti ndimbal yu baari yo un jakkle njaboot gi, masalan: wanni limpo ba waani gu sukkandiko ci njaboot yi baari bant, ndimbal ngir jënde ay teeré ba jumtuwaay njàng , ngir aandu ci tukki bër yi, ak yeen ak yeen. Mëness nga xam ndimbal yi ni jaakle njaboot gi gànaw nga njàg ci téeré `woné wi bi ngooru Serenalitat di siiwol.
Bërëp yi Deglu soxla yi
Amna yu baari yu fi nee ngiir njaboot gi yo de méeni: jubble ci xiiro ba xoolo Hill am ci biir kër gi; ngiir te laa jukk ci feebaru xellu xaleyi, aar ci fitna yi ci kër gi ba xellal wa loor yi ci njanguum xaleyi.
Bu ci bëgge xam lu baari mën nga woote ci telefoon yi: 012 ba nga dem ci biiroo yi banxaas yeengu ngir askan wi, ba bërëp yiiy ndimbal askan wi yi fi ne.



