Liggëy
Lii nu bind fii am nañ Tekki wi ci Kaalama Al pulaar.
Liggëy ci Kataluña
Ci pacc gi di ci giss bepp xettu xibaar ci aajo ci maayeb liggëy yi fiaam, ak foo mëne wut ak li mooy lacc.
Raxasi dooli, am na naari paac yu ndaw yu leey xamal ci ndampaay naak sa ligeey ak yélefu liggêy kat.




