Teranga - Yoonu jokko Kataluña ak

La illa Gorée

Senegal        

Ñassu cosan

Gorée dekku ndox wër la bu toolu ci 23 ektar ci wettu Ndakaru, tollu ci 3 kilometer ci soowu. Beer fu weet la and taaw fex. Lu jaafe gëm ci jaam ji fa am wutte ak jamono njaayum jam bi fa amoon ci gànnaw. Gënoon fas ci ja ci Afrik.

Li toolu ay teemeral at 16 ak 19 , tefess su beer neewoon fi ni doomi Afrik goor, jigeen ak xaley di joggé jëmela Amerika, nu deff leen ay jam. Taar r ak coxaan tax ba beer nek ci yi un taan ci Dekk yi Aduna bi bokk ci attum 1978 te mbootay xett wi sosso coxaan ak aada yoor UNESCO.

Ngir dem naari fukki simili gànnaw nga jël gaal gi ci waqub ndakaru.bu aksi li laay jëkk jaxaal mooy ni mbend yi bindoo ak seen kër yu tuut meeloom, tëgge ko waan yaanjeloko ni wa tungal. Gorée de wone li mu jël ci tubab yi ci ruuxu yeep. Fu un naaw la li fa ndaamar dul daw ak yoonam yi nu kudron wul.

Gorée tubabi Portugal noo jëkk giss ci attum 1444, un fa taabaxoon këru jam bi jëkk toolu ci ay teemeral ci 18, taay ci foofu mooy misse bi. Ci weet gi misse jigeen yi biiy sargal jigeeni Senegaal

Amna yeen taabax yi mën setti demeni jàngu Saint Charles Borromé, missé coxaan IFAN ba missé géej.

Keen mënul dem Gorée te akul s aja ba, ba doxantu ci mbend yi laay yobbu ca sattoo. Bu la liggey kat yi ci suufu meeloo , mëness jënd ci njëŋ lu yomb gànnaw waxale, di aksi ci sattoo ak for bu San Miguel. Tubabu Hollanda yi ci attum 1976 ci xeer yi ak turram yi ak buntu yu taxawu ba leggi. Fii gëna kawe ci Beer mëna giss Ndakaru.

Bokkal        

imatge Foto de nextdrop. Llicència cc (by-sa)