Kër
Lacctel ci mbiiri dekkuway
Am kër gu baax tollu ak saay bëggë Bëgg ak sa mën mën yombul , ndax deey lacc jot. Njëŋu kër lu am daayo ci xaliss ndam da nga kooy jënde ba luyé .
Bu demé ba jaap li nga bëgge def , day jar nga laccte li gaw, te xol bu baax. Yoon jaaple yi fi ne ( ndam jënde la ba luyé ak asirance ak yeen nak yeneen ...) mën la teete ci seet bi ngir taan bi yomb.
Lu mu mën ti donn ba ku la xella mën nga dem ci bërëp dekku way ci sa dekk , sa dimbal dina baax ci soxla.




