- Inici
- Dëkk Kataluña
- Bërëp ndimbal askan wi
- Guneyi ak waxambane
Guneyi ak waxambane
Guné ak xaley
Fi ci Kataluña aada la fi yoobu guneyi ak waxambane yi ci mbootaay yaarin yi deme ni Eskut yi, ak bërep yi ci jakklel yaar ak fo.
Mbootaay yi di def ak mbiiri yaar jaare ko ci f oak yeen xettu teeyye xaleyi ci jamono beer ci aat mi.
Bo ci bëgge xam fo nu ne ci sa dekk bag ox, mën nga seet ci internet mbootay yo ye di go deff fi ci Kataluña.
Am na yeenen pexe yo de me ni garderi yi. Ay mankaan yuy jël ak teeye ay xale la bu nu ame 4 wer ba 3 aat, waxtu yi xamne seen wajoor yi menu leeen tee ci bess bi. Bu lo soxale men nga dem ci bërëp yoyu lacc te.
Ludotek yi ay bërep foo wu kaay yu nu ko jakklel guneyi ak waxambane yi 5 aat ba 16 aat.



