Tere yinu digle

  • imatge

    Catalán para dummies

    Tere bu netali lak catalan ci lu yomb. Ñungi ko bind ci español te amna ay bat ci ada ak yene yu catalan yi.

  • imatge

    El llibres de la Nur

    Ay tere la ci ñari lak anda k ay desin, ñu bindi ko ci catalan ay yene 6 laks, lu demeniki ci wolof, lep jem ci dimbali ñi fiy soga ñew man lak bi te xam ada rewmi. Li ci nek dem ci xam xam ci walu rewmi ak li ko wer.

  • imatge

    El Món de la Dúnia

    Ay tere yunu desine yuy wax ci catalana k yenen 15 lak, lu demeniki wolof, fula ak manding. Limu emb day dem ci goj bu nek: Afric, Europe bu Esta k Asi. Ay tere yu and ak lo mana deglu, te man ko fek ci Internet.

    imatge