Luye

Zaartu luwe kër

Luyé kër mooy dekk ci kér jaambur, gànnaw ngeen jappe nga faay wer wu ne. Si and ci ni miiy doxe nda nnu kaay bind ci kontra luye.

Yan kayit ngaay soxla:
• Dentite ba passpor
• Kayitu sesour
• Sotti kontra liggëy ak kayitu faay gi
• Sedde bu bank bu deggal ne di nga mën faay luye

Tekk yi ci walu xaliss

Paayor wer
Moo y li nga faay wer wu ne te ne ci kontra bi , bu bëggé di wëy di fa dekk gfaaw ttoope tëral boobu . fay de faral di jaar ci bank , te boroom kër sasoo faayé mu defal amb rësi.

Jooxeep ndëganuko
Jooxeep ndëganuko xaliss booy duggal ( tollu ci been ba ñaar ci paayor gi) mooy teggu ngaranti faay bal nga dugg. Xaliss bi dina ko denc ca Institut Català del Sòl (INCASOL) bes bi ngeen di xatim kontra bi. Dan la kooy dellu bes bu geena kër gànnaw bu nu setté amul been yaxu yaxu.
Bu amee lu fa yaxu , xaliss ba kaay defaar di naan ka ci teex. Ngir bañ coow ba la nga dugg deffal liimu li am ci Kër ak nu mu mel, boole k oci kontra bi bala nga ko xatim.

Denc
Mooy xaliss bi boorom kër gi di tekk ca bank ba wone mén nga faay. Denc daay wëw ba ak kontra. Denc ak jooxep ndëganuko xaliss bu boorom kër yoore ngir bes bo faayul luyass.

IPC
Paayot gi daay yokku at mu ne sukkandiko ci naat jénd ak jaay (IPC) , mooy wone soppeku yi am ci njëŋ yi, njaay mi ak jënd bi ci reew mi.

Diiro Kontra bi
Kiiy luye ak boorom kër noo kaay waxtaanne ba and ci kaddu. Yoonu luyas ci tax yi nek , wax ménul gëna neew juroom mi at, at mu mën ka yeesal gànnaw nga and ci.

Luyewat ay neek ba Kër

Kër ya nga mën luye bu fekke boorom and na ci te xatim ko ci kayit. Li diggël mmoy keep ku dekk ci kër gi bokk ci xatim kontra ba. Tere nanu jaay magazín bu defiar ngir dund fa,-te amul certifica mëness dekk- b une bërëbu jaa ba isiin.