Luye bu beene

Li un taan ci yeen kër yii nooy luwe

Mooy luye kër yi un jakklel nit ni am yeen jaafe jaafe ngir jot ci dekku way.

Luye yi un beer
Luye yi un beer mooy yi ngor gi di beeral ci am jaafe jaafe jot ci kër yi. Tëraliin yi maaye nga jot si been laan fi (ubbi wunu ko, saarta moo ku laal) njëηam gêna neew yeneen yi;
Ci faana wi kër yi yomba nañ, dan ciiy boole kër yi ngoor gi beer, yi un waxtaane ba beeral; amna ay ndimbal yu baari yu mën jariiñ bees booy jënd ba luye. Xollel leen fi.

Kër yi un jakklel xaleyi
Xaleyi bokk naan ci ni gëna am am ay tolof ngir jot ci kër yi. Ngir xaleyi mëna demal seen bopp Jawriñ ji leen dënc tekk na ay peexe ngir yombal faay luyass. Ndimbal ci Luyass bu and ak yoon ak ama m bi gëna neew ngir demal sa boop ay jaapale bu defal xaley yiiy luye.

Boo de xaley booy wut kër mën nga dem ci biiro dekkuway yi ne ci Kataluña. Bu duggule kontra ci biiro yi, xaley yi ak boorom kër yi di naan am ay yombal tëralin yi demene ni baana faay ci rataaxal waxtaan yi ak bepp faay bu ci tope , te am assiranss ci fan yepp ngir kër gi ci at mu jëk ci luyass.

Amna yeen ni pexe yu demene yi Fundació Viure i Conviure bu Caixa Catalunya bi bëggë boole xaleyi ak maggat y ici been kër.

    imatge

    defal klik