Teranga - Yoonu jokko Kataluña ak

Làmb

Senegal        

Tàngatt yaram ak cosaan

Làmb mooy tàngatt yaramo bi soxoo ci reewum Senegaal, bokk ci cosaan yi gëna yak ci reew mi, siiw ci Siin Salum ak Kasamass.

Làmb un nga soss ci fukk ak naatel temerla aat ci arminatu Insa, teggu ci joŋŋante yi aam ci goox yi ak xett yi. Jaambar yi epp dolle ak fit ci gox bu ne nooy bëre ci joom giir siggil seen dekk, ba jël ndam ci yeeni tegg demeene ci toll yi mën ba alal.

Ubbite làmb ak xumaay yem moo gëna nex bëre bi. Jigeen un xett w une di wooy giir naax ba naan maam yi, Jewel di jiin dënd yi. Mbër yi yi di Bàkku, takk seen ni téeré, diiwo ba niin ak sanŋo saafara bu seen seriñ di joxé. Aada ci ceddo yi la joggé, baaxu maam li saxu la ci reewu Afrik yi. Aamna ay dekk yi biir alal bi noo ngi topp ba leggi soori yiiy aam ci taax yi.

Làmb Senegaal yi been naa la ci yiiy aam ci Afrik, ndax daffa and ak door. Bëre bu di na yagg ci lu tollo ak ci 45 siimili ci lu epp, un xàjj ku ci 10 siimili gànnaw 3 noplu buy yak 5 siimili bu ne, 3 wali noo kooy setlu. Wa bëre yi du un aksi ci diir boobu, ndax daan daay aam ba boobu. Ndam amna bu bopp laale suuf ba oom yi ay conc , ba taat yi lal suff.

Ak ndoxu jamono, cosaan wi nekk leggi tàngatt yaram mu reewmi. Bess by ne xaley yi yu baari si dgg ci làmb ji joŋŋante yi di aam ci reew mi ak Vitim reew, di xew xew yu reey di boole tàngatt yaram, coosan ak aada.

Bokkal        

imatge Foto de galex. Llicència cc (by-nc-sa)