- Inici
- Dëkk Kataluña
- Wergu yaram
- Domu medicaments generic
Domu medicaments generic
Jël garab ngir faccu
Moy dom medicament yinga xamne dafa jex, sen contra ak ñi koy dejar nekatul. Mo tax muy ay domu medicament yu ñuy jay ci marche ci lu yomb.
Mok domi medicaments llenen ño yam. Ngur gi dina faral dici taxaw pur nit ñi ci walu wowi.
Lu ci mana am muy domu garab bu muci mana don dina am solo nga joko sa doctor bala nga ko tambali jel, te bañ ko jend ci Internet. Ñi wanane lu tolu ci 62% baxul wala amul taxaway bu mat pur nit ñi man ko jel.
Bu aamé looy lacc ci nii jële garab, jokkol ak wa centaar bi xibaar ci garab yi fi ci Kataluña (CEDIMCAT) .



