- Inici
- Dëkk Kataluña
- Ligey
Ligey
Lii nu bind fii am nañ Tekki wi ci Kaalama Al pulaar
Li ngaay def ngir liggeey Kataluña
Neew doxandeem yi fiiy liggëy si moo ngi ajjoo ubbite liggëyu ka yak soxla ngi am si noom. Liggëy bi ak caawartek doxaandeem yi amna jëriñ ci suxat kôm mi askan wi.
Am liggëy nak yitte woona nga dugul yeene kayit yi, rawatinaa ni amul kayiti sesour. Boo am ci liggëy yi di war ci yaw nga am lu ëpp 16 att boole ci am kayit. ak maayeb sañ liggëy di na tax nga nit ku mën dekk ci kataluña.
Lii ne fii ay teetal ak xibaar yu la jappale ci wut ak dugul kayit yi nga soxla ngir am sañ liggëy (demeni sa liggëyu bopp ba liggêyal keneen), naaka ngaay taane liggëy bi yeemb ak sa bëggë bëgg, fan ngaay jaar ngir giss ko.




