- Inici
- Dëkk Kataluña
- Dëkk
- Nacionalite español pur ñi fi dëk
Nacionalite español pur ñi fi dëk
Duggël wut aam kayitu firnde bokk ci doomi Españ
Dojandem yi fiy dundu yep man nanu lath nacionalite español.
Lunu siy lath?
Dëk Españ ci dir bu tolu thi fuki at. Ci waxtu wowu man na baña ag fofu pur ay nit com ñi gene sen rew pur problema politique (juromi at), dojandem yi takantek español (ben at).
Fan lanuy ute kayit gi?
Fi niy tude Registre Civil bi ci goj binga dëke.



