- Inici
- Mbotaay yi
- Mbëbët yi
Mbëbët yi
Liggëy ci Jokko kom kom
Kureel mbotaay Senegaal yi di aam ay mbëbët ci fan yi:
•Yombal jokko ak weccante xareñ mbotaayi Senegaal
• Suuxat jeggé ak wecco mbotaayi Senegaal ak seen nawle yi ne Kataluña, ak Españ.
• Yokko jokko Senegaal ak Kataluña ci wallu kom te boole ci mbotaayyi doomi Senegaal yi ci reew mi.
• Taxawal yooni waxtaan jëmele ko ngoori Katauña ak Senegaal ngir seeytu tukkib doxandem yi.
• Dëkkaraal mbotaay yi doomi Senegaal ngir ndoxaliin gëna rafet.



