Fooy wutte liggëy

Booy wut ligeey , amna pexe yu baari yu la mëna dimbali ci segg liggëy yi taxaw. Mëness ngo ci biiro wut liggëy yi ne ci Kataluña , di nga am xibaar yu dëppo ak sa bëggë bëgg , mën nga woor tamit ligeey ci Internet , ci anterpirissu liggëyup diir , ba si coobari ak jaame yi.

Biiro liggëy yu Generalitat de Catalunya (OTG)
Aay bërëp yu tonal Servei d'Ocupació de Catalunya. Ca OTG yi Mñen am xiabaar ci liggëy yi taxaw te antarpiriss yeene ko, di nann la teete tamit si ni nga mëna deff ba yokko sa passpass. Wanté nak fokk nga dem Bingu ji ci biiro bi la gëne jéggé.

Tasskatu xibaar
Ci tasskatu xibaar rawati yi bind (bess b une ba yo fettewoo mbiir yi), ak yiiy geenë ci Internet te gëna xeriñ fi un tollu moo epp ci jokklo que wutt liggëy kat ak ki kaay wutt, si lollu di nan lacc ng ba fa sa kurrikulum witee bu bëgge ci tan wi. Yeen ci web yooyu nooy: infojobs.net, laboris.net, ba trabajar.com.

Antarpiriss jooxe liggëyub diir
Antarpiriss yi jooxe liggëyub diir (ETT) ay mbotaay sañ jël ay liggëy kat tekk leen nuy dan seen doole ci beneen antarpiriss. Un yeem yeelef ak bepp liggëy kat. Yoon ci liggëy yi dul yagg.

Lënkello yi
Networking ( ba lënkello yi) mooy nga fexe am ay jaame ci giir ngi ngaay liggëy , mëna ne un sarín ci mecce ba ay xarit rek, un wax ci sunu mën mën ci liggëy bu tax. Xibaar bu am ci epp te moo baax day ne lu am Gerin ci liggëy kat bi, ndax bokk na ci gëne gaw ngiir liggëy ci diir bu neew. Ci web Linkedin mëna nga ubbil say jaame.

Pexe bopp
Am liggëy daffay lacc pass pass bu dëggu te wér. Nda nga wara xam li ngeey wax mbook yi ay am di jam yi booy wutt liggëy.Bu la been anterpiriss saf tamit mën nga dem wax leen da ngay wutt liggëy moo xam telefon, mail baa teew fa.

    imatge

    • Kurikulum bi mooy li dul naak bu bëgge wut liggeey. Defar ko ci anaam ku leer te yaam, binde c isa tuur ak fi un mëna jokko yaw, saay lijass ak xareñ.

    defal klik