- Inici
- Dëkk Kataluña
- Dëkk
- Kayitu residans
Kayitu residans
Toppato ngir dekk fi bu deppoo ak yoon
Pur nga dëk Cataluña danga yitewo kayitu residans. Kayit gogu mana nek ci dir bu gat wala mu nek ba faw.
Kayit residans bu dir bou gat
Kayit gogu bude dir bu gat, mana tolu ci at, wante lu nuy mana yok la basi jurom mi att. Pur nga amko, dinga yitewo visa residans bingay jële si ambasad espagnol bi nek Senegal, mu tenku si ñari walu:
- Residans ak liguey
- Bi mana indi sa ndiabot
Ñinga xamne munu ñak kayit bobu:
- Ku fi dundu lu tolu si ñari at te mana wane ne liguey nga lu tolu si att.
- Ku fi dundu lo tolu si ñeti at, ame contrat liguey wala nga wane am nga fi ño bokal ñula jegue.
- Wala nga nek domu espagnol bu gor wala bou jigeen.
Kayit residans ba faw
Dëk Espagne ba faw tey liguel como wa rewmi. Ñiy am kayit gogu moy ñi nek si rewmi dirup jurom at. Bu waxe ne Kayit residans ba faw, lolu teki wulni dunu ko yesal, juromi at yune danga koy yob nu joxla benen bu bess.
Fan lanu ko muna ame?
Finu tude delegacio gornema bou Catalogne bu rewi Cataluña.
Amna ay mbotaay ci Kataluña yuy yenŋu ci xelel ci wallu yoon doxandem yi sogga aksi. Xolal fi ci Teranga.cat ngir xam fu ne.



