Waalu ki ñaaka seen liggëy

Saartu liggëy bi fii ne waxna ne liggëy bi naatoon ca sekirité Sosyal, te ñaaka liggéy ci lunu saakul, amna lu un leen jakklel ci salís.

Diir bi gëna tutti ngiir am ko mu tëdd ci 360 fan, mën xaam naata nga waara jot lepp aajo ci fan yi nga naat ci Sekirité Sosyal, ci Prokram bi Jawriñ reew yoor liggëy def.

Bu li niiro ak sa nekiin leggi mën nga dem ci Biiro wuttum bi la gëna jeggé. Am nga 15 fan geene ci bessu bër yi ngir lacc ko.

    imatge

    • INEM mooy bërëp bi seytu wut ak may liggeey bi, tamit dimbál gi ni naak seen ligeey di jot.

    defal klik