Teranga - Yoonu jokko Kataluña ak

Ñenti bant yi

Catalunya        

Fi mbandarga Cataluña juge

Dananu faral di netali ne mbandarga ak drapo bu Cataluña mungi donon ci tengu njitu france bi ñiy wowe Carles el Calb (Carlomagno) ak jarbatam Gifré el Pilós njitu Barcelona.

Netali bi dina waxni ka Gifré el Pilós dafa geyon ci kërëm gi nek ci Valldura. Ay nitem, jaxle, di lax lu waral mu melnonu motax ñu wajalko ab rëb, am feth ak fet gu mak. Wante lolu taxul dara copeku ci mom: Yerem lep or la won, wante amul won ben flër lolu mo taxon mu gey.

Ben bess, rir mu bari yeksi ci buntu pale bi. Ño jotale yeksi wayu njitu France, nijayam Carles el Calb, di wax ni wa normande ñoy ndagu sufu France te dano soxla ndimbël. Gifré el Pilós mok gangoram, yeg sa fanuy xexe. Ñu yeketi seni nganay sa kaw ba sonal lol non ya. Wa normande ak dole ji un giss ci catalane yi dadi daw.

Wante, ci xex bi Gifré el pilós dafa gañu ba xawa de. Ci Lamb lolu ñu am ci normande yi, mo ngi don metitlu li nga xamne mom la yerem mel. Carles el Calb, xam li jarbatam def ci xex bi, dadi koy jege dadi red Denti yon f inga xamne fi la gratu or bi nek. Lolu moy wane fi drapo Cataluña juge ba sunuy joni tay.

Bokkal        

imatge Foto de Santi MB. Llicència cc (by-nc-nd)