Ruxu yi

Bërëp yu rafet

Ay ndaw te yanje laan ci wallu teggin dunya, dön lu juddu ak suuf, ba and ak coxaan: ruxu yu ne ni ci Kataluña ak Senegaal. Dugg ci.

 

    xolal:

           
    • 1-
    • 2

    bi möjj»

    • Catalunya       
      Cadaqués

      Cadaqués

      Cadaqués dekk bu tutti ci diiwaan nu Sirona, ne ci gooxu Emporda ci kaw. Dekk bu ay coxaan ci napp ak mbiir yi fette geej. Meelin nam, waqam ko ak tefess am deff na de yoon turista yi ci Kosta...

      xolal yeneen ( yi nee ci ëmbi):

    • Senegal       
      Delta del Siné i el Saloum

      Delta del Siné i el Saloum

      Pegg teen deexu Siin ak Salum book na ci bërëb juddu ak suuf yi Gëna rafet ci Senegaal. Ay dekk digg ndox yu baari te ndaw laan, tiir ak gancaax mangrowes. Ca seenaay ga tefess gu ndaaw gi...

      xolal yeneen ( yi nee ci ëmbi):

    • Catalunya       
      El Parc Nacional d'Aigüestortes

      El Parc Nacional d'Aigüestortes

      El Parc Nacional d'Aigüestortes i Estany de Sant Maurici moom ko mooy parka reewmi bu ne ci diiwan nu Kataluña ci 14 yu mel ni ci Españ. Moo gui ne ci bucc saawo ci goxu Lleida, tundu yu...

      xolal yeneen ( yi nee ci ëmbi):

    • Senegal       
      Casamance

      Casamance

      Casamance tund ci beëcc salumu Senegal ak Gambi. Un wax ne moo dax ci Senegaal. Ay la yewoon, tefessam yi ak gancaaxam bi ak tangoor taaxna ba tukki kat yu baari di gëna setti.

      xolal yeneen ( yi nee ci ëmbi):

    • 1-
    • 2

    bi möjj»

    Bokkal        

    lepp lu ni fii siiwal ci lakk ki go mbind nanu kay ba