- Inici
- Fii ba fëlé
- Li ciy dem
Li ciy dem
Lekk
Plat yinga xamne dinanu faral di togu ci Cataluña ak Senegal.
Na ci jam bari!
xolal:
- Catalunya

Calçotada
Calçotades a nadje y ndabot yi di faral di def, muna nek feta k ay mbok wala xarit, lunu fonk la ci rewu Cataluña. Dana faral di am bu primavera bi di tambali.
- Senegal

Bissap
Dinga ko mana defar ak hobi ibuscus yu nga xamne amna Senegal. Dina un faral di ko jel bu sede, rawatina bu tange ci walu wowu di Senegal.
- Catalunya

Crema catalana
Com ninu ko tude, crema catalana moy deser binu gana xam ci Cataluña. Yomb na defar te, dafa nex lol.
- Senegal

Tiéboudienne
Dinanu faral di wax Cebú Jen, moy pla nacional bu Senegal. Ñungi koy defare jen ak ceeb, ak yenen xetu legum yu am Senegal.
lepp lu ni fii siiwal ci lakk ki go mbind nanu kay ba




