Bërëp jappale yi nu jakklel doxaandem yi

Lii nu bind fii am nañ Tekki wi ci Kaalama Al pulaar

Saarwiss yi toppato peexe ak mbiiri doxandeem yi

Amna ay bërëp yo xamna doxaandem yi dekk ci kataluña nanu ko jakklel yu deme ni Ambasad va konsula.

Yeen ci bërëp yi moy yi mbotaay yi ubbi , di naan di tek ay peexe yuy japaale doxaandem yi ci ngir nu meen dekk bi. Amna xeetu jaapale ye demm ci wallu yon ak ligeey, njàangum katalan ba alfabetisasoη, ndimbël jigeen, guney yi ak xaleyi, ak waay laaxu yi. Ci pacc bu ne di fa giss yeen ci gox yi nu ne.