Dëkk

Lii nu bind fii am nañ Tekki wi ci Kaalama Al pulaar.

Duggël kayitu residanss fi ci Kataluña

Kep ku yeksi Kataluña danga wara taxaw ci linga xamni munuta ñak te manla dimbali ci sa nekin fi ci Espagne, muy di ci walu kayit. Lu demaniki am kayit guy wane finga dëke, mudi lilay dimbali ndax nga mana am kayitu doctor wala Kayit pur walu njàng. Yenen kayit you am solo pur mana dëk Cataluña mo di kayitu residans ak kayit giy wane ne dojandem nga ci rewmi.

Pur am leral bu gana yatu ci walu wowu man nga dem ci bërëb bi nga xamne mo nek ci goj binga dëke muy di Mairi Bi wala tamit ci mbotay yinga xamne sen xam xam math na ci walu wowu. Ci buntu bi nu tude “ñi sen liguey jëm ci walu wowu” dinga fa giss ñi sen liguey jëm ci walu wowu wala yenen yo mëna yitewo.

Setal 'Ñi sen liguey jëm ci walu wowu' danga fa fek mbotay yiy yengou ci walu wowu, ci lep lu nga xamne dojandem bi dana ko soxla.