- Inici
- Fii ba fëlé
- Ruxu yi
- Delta del Siné i el Saloum
Delta del Siné i el Saloum
Been la fi ci yu goox yi taaru
Pegg teen deexu Siin ak Salum book na ci bërëb juddu ak suuf yi Gëna rafet ci Senegaal. Ay dekk digg ndox yu baari te ndaw laan, tiir ak gancaax mangrowes. Ca seenaay ga tefess gu ndaaw gi la laay joss: ak suufam ci weex si, gancaax gu neew gi jëkk giss ci parka bi toolu 180 ektars.
Lu ci baari ci foofu mu ngi bokk ci parka bu Delta Salum (76000ektar), tangoor wi ak ndox mi taaxna ba mala yu baari mën fa di dund. Bu bëggé settlu picc yi diggël nan la nga dem Tubakuta ba ca wettu becc salum , ci dekk digg ndox ba picci di ne , amna, amna ay flamans , picc geej, ak marabú.
Parka amna tami alla buci yokko , bu baax la te teggunu tudde ko Allab Fataala bu goolo dekk, mbaam ala bukki ak yeenen.
Un dugge ci parka ca Misiira, daw lu toolu ci juroom been kilometar baala nga aksi. Baa la boobu di nga settlu ay beeteñe yu re (seïbas), toolu ci jooni att te giss kot ci diiwan b. Mën nga yeek ci locco yi dem ci yeen dekk yi jeggé, ba waxtaane nooy nà ppe ndo ba daawal mbeggé.
Foto de ho visto nina volare. Llicència cc (by-sa)



