Ci walu bank
Leeplel bank ak seytu bank
Say bo topatowe sa bop ci dir bu gat cisa nekin ci Cataluña, dina am solo nga ubi ben compte bank ci bank yi ci rewmi com bu Cataluña wala bu espagne yep.
Pur mu gana yomb ci yaw, lu bari cisa walu xaliss pur boy fay fen lumu mana don wala nga buga dinthe xaliss dinga ko mana def ci bank.
Bank yi dinanuy lebele pur proje yinga yakarne dina la mana soxal, com lo demenika jand kër wala nga buga ubi sa miru bop. Bala ngay jublu ci walu ubi compte bank wala di lep nanga set bi gana am solo te gana oyof ci yaw.



