Yeen bërep ndimbal askan wepp

Kaarangé ak seytu askan wi

Poliss
Fi ci kataluña amna xetti poliss yu baari , gu ne ak li nu jakklel:

·Poliss ci dekk gox bi bi lijjënti yoon te aar nit ci biir gox bi kot;
·Mossos eskuadra yi di poliss si kataluña, noo amb plissi gox yepp , te di aar askan wi ak dem ak dikk bi ci kataluña.
·Poliss reew mi te ne ci españe gepp. Fi ci kataluña yoor lu dul defar kayitu dentite yi.
·Kuardia ciwil moo bokk ci arme bi teey arr reeew mi yepp.

Naka lan niiy kalame ?
Bu nu la toone ba nga fekke toon mën nga kalame:

·Ci bërep bu mossos eskudra yi , di ubbi guddi ak bëccëk
·Ba nga wotte ci telefon bi 088
·Ba internet, ci bërep bu kalame yi ne ci interenet.

Buy kalame di nanu la lacc nga wax sa tur ak bi si kayi dentite ba
passpor bi.

Looy def bu wut walu ci lu jàmp?
Woo wal mossos eskuadra yi, 088? Ba telefon wallu gi, 112

Bërep yi toppatoo neew yi
Bu nit fattoo, amn ay ligeyu kay yu kay toppatoo si fan yepp: defar jatt gi, bàamel bi, nekku tàggo bi , dëcc bi ak roob fi ak bitim eew . Ay ligeey yu jaambur lan lolu waral faay gi.

Amna yeen ci bërep yiiy toppato neew yi , te nekk ci Barsaloon yu am banxass bu jakklel yoonu islam.