- Inici
- Dëkk Kataluña
- Bërëp ndimbal askan wi
Bërëp ndimbal askan wi
Aar askan neew ji doole yi
Bërëp yi di ndimbal Askan wi nooy yi nga xamne da niiy aar ci lórro, Taxawu ci soxlo askan wi, raweti nii dool gënë jaap.
Ngoor gi ak mbootaay yi yi jaaple tekk na ñu aay peexe yu askan wi mënë sukkandiko ngiir yômbal seen duna. Fii ci Cataluña, Jeeriñ ngi seytu biir yi mooy banxaas ngooru Seneralitat Bu Cataluña bi un Jakkle Yéengu ngir askan wi.




