Teranga - Yoonu jokko Kataluña ak

Xareñ ci Suuwer

Senegal        

Natal ak pintiir ci wer

Pintiir ci wer - un xamé ko ci Suuwer joggé ci fransé sous-verre – bokk na ci aada Senegaal. Yagga na, li am mooy ne xalaat yi wuddu natal yi noo wute ba anda k jamono leggi.

Xareñ gi am ci pintiir bi wute na ak bu cosaan: di jutal, manam ti pintiir ci gànnaw wer bi. Li miiy Jëk def mooy taan natal bi bi mooy sotti tekk swer ci kawam. Ak xalima bu seew ak daa Siin també di rëdde caati natal, bu wesso loli laay la diiw mello yi ci natal bi. Pintiir dañ ko defar ci jutal wute ni noo kaay gissé , taax ba beep bataxal bu ci geena dee meeni siiñatiir , bind mi daal tambale ndeey joor jëm caamin. Ngir aar wer bi karton naa un kaay woode.

Melo natal bu gëna deppo cosaan mooy bi woné yi taxaw ba tiim ba jakarlo, ak caat y une faŋ ak daa bi un ko rëddé, jëffandiko mello yu fëss ak cër yu massewul , ndam cosaan la woon ci suuwer , ndoxu jamono dem na ba sopi ko, di toppa bëgg bëgg pintiirkat ak jëndkat yi yu bess yi. Yokko diinaay liislam ak xeex buddiko tubab yi noo doon liiy xelal suuwerkat , teey xew xewu jamono nooy feñ.

Bokkal        

imatge http://www.senegal-online.com