Teranga - Yoonu jokko Kataluña ak

La Tarragona romana

Catalunya        

Taabaxu ci capital Romaan

Tarragona ci ñenti goxu Kataluña, te nek capital bëcc salum Kataluña am 144.163 nit. Booy doxantu ci mbend yi ak ruuxu do donn lu jaafe nga naata coxaan.

Li mu jéggé deexu Ebre deffoon nako naari junni att, ci gànnaw dekk bu junnu soxla taax ba buuru Rom tekk ci loxo. Njàngum coxaan wax naan ne Buur August ci attum 27 bala judd Issa, jël goxu Tarraco deff kapital Hispania Citerior Tarraconensis. Ci att ci topp un tambaali ko taabax nii yi am ci kapital reewum Roma. Taabaxin yi boole fo, rafet ak wone reey

∞ Anfiteatar
Un ko taabax ci wetu geej gi ci ay teemeral att toolu naar. Wërgal lank o deffe, daan amal ay lambu kaladiators , xeexu mala ak yeenen ak yeneen , ba ci ay teemeral att tollu ci jurumeel nu baa ko. Gànnaw gi nu taabax njàngu bu magg paleokrecen, aci lu gëna yeex ci ay teemeral tollu 12 njàngu Romaan.

∞ Cirk
Kolisé nun ka defar ci ay teemeral att toolu ci been. Yokk bi ci li gëna tutt (325 meter ci peggu gu magg, 110 ci yattu way) , li ci dess moo ngi denc ba leggi am ay buntu yu dess ak yeeni yu bules baari tirbines ak pódium, lu deeme ci taata ci toolu ci naari metar te jël 20000 nits. Cirk ak rawete fas , te moo xaaj dekk bi naar., bi yooro ngoor ak bu wa degg.

∞ Teatar
Been tatar kot la bu fa roman deff ci Kataluña, ci jamono bu gëne reey, ci reewum roma ay ett yu baari, ay waanack ay saangukay , ay bayal yu magg ay wecc ak ni fii tal diine yi. Seeytu amoon na tolof tolof . bi 1977 si am ay jambur un ci jaap ba ñu ba taabax baññ ko yaq deff ko moomal lu reew mi.



Settil misse reew ci Wallu Seet Dessutu Tarragona



Yaaju Tarraco ci ca jamono boobu li siiw la. Dekku diina ak ngoor gi, taaxam yi un ngi toolu ci 7 ektar. Waaye ak att yi ak dteeraliin bu bess taaxana ba Tarraco do tul capital njàngu biu magg bi. Jeqam ngi tooolu ci jamono bi jullit aksi ci reew mi toolu ci attum 714.

Fattaliku bi deff Tarraco lu doole ci coxaan fi tefess su geeju Mediterranee. Waral Unesco tuddi dekku neep ci attum 2000.



Bokkal        

imatge