Xeeti liggëy yi
Amna ay xeeti liggey yu baari yu fin e, lacc teel bu anda k sa bëggë bëgg.
Teere liggëy yi jaafé giss ku ka bëgg
Jawriñ ci yoore mbbiiri liggëy , da waasaré ñaati wer yo ne liimu liggëy ya jaafé am ku ka bëgg. Zaartu reew daf ci ligg<éy daay yombul kontra waliyaan ci jaafé jaafe yi.
Yoor sa liggëyu bopp
Ubbi sa yëffu bopp ba antarpiriss yeen ci yoon ngir liggëy ci Kataluña. Boo ci bëggé dugg ,waar na nga xol bu baax lu jaa bi mel, lu maaye ay jaafe jaafé yi , sotti xalat bi ci palaan antarpiriss . Amna timbal yu baari ci mbiir yi demen INICIA, web bi jooxe xibaar ci ubbi Antar Piris, si maaye ak jaapale yi Generalitat bi di jooxe.
Liggëy ci Ngor gi
Liggëy kat yi ci ngoor gi bokk ci fonsineer yi noo yoor lepp luy seeytu ba raataxal toopatoo mbiiri askan wi. Amna saart buy lijjanti doxaliin bi ak aajo yi am ci liggëy yi wutté ak yeen yi si bitti. Dugg ci day jaar ci jonŋŋante yuy aman ci baanxas sam yepp ci Europa, fii ci reew mi, ci tundu yi ay dekk yi.
Contingente bu waliyaan yi bokkul Europa
Ngooru Españ daay taak at m une kontra yi anda k contingente jubbal ko ci ni dekkul ci reew mi, tekk ko ci bëggë bëggë reew mi . Ni sciiy taan ci maaye liggëyo ( yeen ci xeetu liggëy rek laay doon) daan kooy siiwal FEPP, baa un taan ci nit yi (bi niiy Josh liggëy kat bi un xam). Lu mën ti donn kontra bi ca dekk laako xatiim.



