- Inici
- Fii ba fëlé
- Coosaan
- Cosaanu Miisic a Senegaal
Cosaanu Miisic a Senegaal
Li aam ci weey ak jummtuwaay
Miisic lu aam tur la ci cosaan un Senegaal. Weey wi ak ki baatam, jumtuwaay ak dégg gi mooy geen daanu aada maam , taamit yengu aad ak jamono reew mi.
Bu waxe aada ak miisic, fook un wax nii ko saam ba aksi fi, di moomel reew mi, cossan bu akse fii gërëmo ku Jewel. Geewel yi ci askan noo fette wo, mbiiri wooy ak tà gga garmi yi ak boroom barke yi ak alal. Ci Gà naw ci askan un leen di fettale ci suffu geer yi ( garmi , njaay kat ak yeen xetti ligeey yi) waaye noo ne ci kaw njaam yi. Li wà nni wul daara ci fonk ki askan wi aam ci noom. Ndaxte Jewel unoo taax ba cosaan joggé ci maam y ba aksi ci jamaono leggi, li ci tekk ci nettali ci laamiñ li xew ci goox ak kër yi te aat do diindi. Ba teey miisic bu joggé ci aada ak yu jamono keen mën ko naat.
Bi Senegaal moome boopam, xttu miisic bu bes geen di njaxaasu tëggu latina ak kareeyib, ak bu reew mi. Tëggum sabaar ak tama (jumtuwway wolof) ak tëggu Vitim reew yi indi lu bes, xumbay ci degg ak fecc un gëna xam ci mbalax. Yussu ndur Gëna fëss ci nii kooy siiwal.
Teey Senegaal denc na ay jumtuwaay yu cosaan yu ñee, demen ci toxooro pël, mool bu sossé, riti ak koora, ba ay ndundë wolof yi. Doxantu ci gooxu Senegaal ngir njà ng xettu jumtuway lu aam soola .Taami mëness dem ci xumbel ak fecc yi aam ci guddi Ndakaaru ngir dund ko.
Foto de SkeenaValleyGirl. Llicència cc (by-nc-nd)



