Coosaan

Xew xew ak aada

Bes yi gëna rañe ci aarminaat xew xew yi ci coosaan Kataluña ak Senegaal. nu Xamal la ko.

 

    xolal:

           
    • 1-
    • 2

    bi möjj»

    • Catalunya       
      Patum bu Berga

      Patum bu Berga

      Patum bu Berga xew xew bu siiw la bu joggé ci bes yu un jakleloon diine yi ci teataru jaamono yu njëk yi. Mo ngi joggé ci mbiir yi nii doxantu bi daan ci beesu insa , di doon ci seentu un...

      xolal yeneen ( yi nee ci ëmbi):

    • Senegal       
      Xareñ ci Suuwer

      Xareñ ci Suuwer

      Pintiir ci wer - un xamé ko ci Suuwer joggé ci fransé sous-verre – bokk na ci aada Senegaal. Yagga na, li am mooy ne xalaat yi wuddu natal yi noo wute ba anda k jamono leggi.

      xolal yeneen ( yi nee ci ëmbi):

    • Catalunya       
      Werbena bu San Saŋ

      Werbena bu San Saŋ

      Guddi San Saŋ un xamme tamit ci guddi tal ba jiine yi , mooy guddi gi gëna gatt ci att mi di jiitu bëcceg bi gëna yak ci att mi.

      xolal yeneen ( yi nee ci ëmbi):

    • Senegal       
      Làmb

      Làmb

      Làmb mooy tàngatt yaramo bi soxoo ci reewum Senegaal, bokk ci cosaan yi gëna yak ci reew mi, siiw ci Siin Salum ak Kasamass.

      xolal yeneen ( yi nee ci ëmbi):

    • 1-
    • 2

    bi möjj»

    Bokkal        

    lepp lu ni fii siiwal ci lakk ki go mbind nanu kay ba